J’adresse mes meilleurs vœux de paix, de prospérité et de concorde à la communauté musulmane du Sénégal et à toute la Oumah islamique. #tabaski #AïdAlAdah

Tëbëskig jàmm
Maa ngi ñaan jàmm, xéewal ak déggoo sax ci réew mi, ci mbooloom jullit yu Senegaal ak yu Ummah bépp. pic.twitter.com/vFAxANPMYa

— Macky Sall (@Macky_Sall) July 10, 2022